Tass Ba Ree
"Benn Paa la woon .." Ku ko degg, sa xel dem ci maye. Maye li ko taxoona jóg mooy begël askan wi. "Tass Ba Ree" topp tànk yooyu, jóg ngir mengële cosaan ak jamano, yombalal jotali bi, jaarale ko ci social networks yi, website bi ak application bii, jël maye yi soppi leen mickey ngir banneexu ñëp. T